1 Pharisee ya ak Sadducee ya ñou di ko fir, te lāj ko mu won len mandarga cha asaman.
Wande Pharisee ya gēna, te fēncha naka ñu ko mun a rēye.
Fōfale i bindānkat ak i Pharisee ñu juge cha Jerusalem, ñou fi Yesu, ne,
Yesu ne len, Otu len te moytu mporoh͈al i Pharisee ya ak Sadducee ya.
Pharisee ya ñou fi mōm, di ko fir, te ne ko, Ndah͈ dagan na nit fase jabar am ndig lu mu mun a don?
Fōfale la Pharisee ya deme, te fēncha naka ñu ko mun a jape chi kadu am.
Wande Yesu gis sēn kēfēr, te ne len, Lutah͈ ngēn di ma fire, yēn nafeh͈a yi?
Bes bōbale i Sadducee, ñu ne ndēkite amul, ñou fi mōm, te lāj ko,
Bindānkat ya ak Pharisee ya tōg nañu chi tōgu’ Musa:
Cha lelek sa nak, bes ba topa bes i wājte ba, i njīt i seriñ ya ak Pharisee ya dajalo fa Pilate,
Ndege mangi len di wah͈, Su sēn njūbay sutule njūbay i bindānkat ya ak Pharisee ya, du len h͈araf chi ngur i ajana muk.
Ba Pharisee ya gise lōla, ñu ne i tālube am, Lutah͈ sēn Borom di leka ak i publican ak i bakarkat?
Te lile wah͈ nañu ko di ko jēm, ndah͈ ñu mun a am lu ñu ko jêñ. Wande Yesu sega, te binda chi suf si ak baram am.