7 Yēn nafeh͈a yi, Isaiah wah͈ on na dega chi yēn, ne,
Bu mu teral bay am. Tah͈na be defadi ngēn eble’ Yalla mu di dara chi sēn nābe.
Nit ñile teral nañu ma ak sēn gemeñ, wande sēn h͈ol sorey na ma.
Mīkar bi, dindil jeka lā bi chi sa but, te ganou ga di nga gis bu set ndah͈ nga mun a dindi felah͈ ba chi sa but i morom.