34 Yesu ne len, Ñāta mburu ngēn am? Ñu ne ko, Jurom ñar, ak lu new chi jen yu tūt.
Tālube ya ne ko, Fan la ñu mun a ame mburu mu doy mbōlo mu rey niki bile, chi manding mi?
Mu ebal mbōlo ma ñu tōg chi suf,