Matthew 15:32 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 190732 Yesu ô i tālube am fi mōm, te ne len, Am nā yermande chi mbōlo mi, ndege anda nañu ak man lēgi ñet’ i fan, te leku ñu dara; du ma len demlo te leku ñu, wala h͈ēchna di nañu ñaka dōle chi yōn wa. Faic an caibideil |