Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 15:27 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

27 Wande mu ne, Wau, Borom bi; ndege h͈aj yi sah͈, di nañu di leka ndesit ya di rot chi sēn tabul i borom.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 15:27
24 Iomraidhean Croise  

Mu tontu ko, ne, Daganul ñu jel mburu i h͈alel yi, te sani ko h͈aj yi.


Fōfale Yesu tontu ko, ne, E jigen ji, sa ngum rey na lol; naka nga buga, na ame nōgu chi you. Te chi wah͈tu wōwale dōm am wer cheng.


Ndah͈ ngēn mun a neka sēn i dōm i Bay ba cha ajana; ndege mō fenkalo janta am cha kou ña bāh͈ ak ña bon, te di tou cha kou ña jūb ak ña jūbadi.


Saltige ba tontu ko ne, Borom bi, daganu ma nga h͈araf chi suma nēg; wande wah͈al bāt bi reka, te suma bukanēg di na wer.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan