25 Wande mu ñou te jāmu ko, ne, Borom bi, lêl dimali ma.
Te ña neka chi gāl ga jāmu ko, ne, Chi dega yā di Dōm i Yalla.
Mu tontu ko, ne, Daganul ñu jel mburu i h͈alel yi, te sani ko h͈aj yi.
Mbōlo ma h͈ule len ndah͈ ñu nopi; wande ñu dolê h͈āchu, ne, Borom bi, yerem ñu, you dōm i Dauda!
Ab gāna ñou fi mōm, te ñān ko, ne, Borom bi, su la nêh͈e, mun nga ma setal.