Matthew 15:22 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
22 Jena jigen i Canaan juge cha wet yōya, te mu h͈āch͈u, ne, Amal yermande chi man, E Borom bi, Dōm i Dauda; jine anga geten suma dōm ju jigen bu miti.
Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.