17 Dēgu len ne lu mu mun a don lu h͈araf chi gemeñ, dem chi bir, ñu gēne ko chi biti?
Mu ne, Dēgangu len, yēn itam?
Wande yef yu gēna chi gemeñ, chi h͈ol la ñu juge; te ño di gakal nit.