15 Peter tontu ko, ne, Tiki ñu lēb wile.
Dēga len mbōk lēb i jikat ba.
Fōfale Yesu bayi mbōlo ma, h͈araf chi nēg ba; te tālube am ya ñou fi mōm, ne, Tiki ñu lēb i nduh͈um i tōl ba.
Mu ne, Dēgangu len, yēn itam?
Talube am ya ne, Wah͈ nga lēgi bu set, te wah͈u la lēb.