14 Bayi len len; ño di njīt yu silmah͈a. Te su silmah͈a jītê silmah͈a, di nañu tabi chi mpah͈ ñom ñar.
Te Yesu ne, Ndig ate tah͈ on ma ñou chi aduna si, ndah͈ ña gisul di mun a gis; ak ñu gis di mun a silmah͈a.