12 Fōfale i tālube am ñou, te ne ko, H͈am nga ne Pharisee ya fakatalu nañu, ba ñu dēge kadu gile?
Te barkel chi ku dul feka fakatalu chi man.
Lu h͈araf chi gemeñ, du gakal nit; wande lu gēna chi gemeñ, mō di gakal nit.
Wande mu tontu, ne, Njembat bu neka bu suma Bay ba cha ajana jembatul on, di na ko simpi.
Wande ndah͈ du ñu len fakatal, demal cha gēch ga, sani ôs, te japa jen wu jeka fêñ; bo ūbe gemeñ am, di nga cha feka dogit i h͈ālis: jel ko, te joh͈ len ko ngir man ak you.