1 Fōfale i bindānkat ak i Pharisee ñu juge cha Jerusalem, ñou fi Yesu, ne,
Bindānkat ya ak Pharisee ya tōg nañu chi tōgu’ Musa:
Ndege mangi len di wah͈, Su sēn njūbay sutule njūbay i bindānkat ya ak Pharisee ya, du len h͈araf chi ngur i ajana muk.
Te lile di sēde’ John, ba Yauod ya yōne fa mōm i seriñ ak i fōdey bawo cha Jerusalem, di ko lāj, ne, Yā di kan?