30 Wande ba mu gise ngelou li, mu tīt, te dal di dīg; mu h͈āchu, ne, Borom bi, musal ma.
Mu ne ko, Ñoual. Peter wacha chi gāl ga, te mu doh͈ chi kou ndoh͈ ma mu dem fa Yesu.
Nōn’ ak nōna Yesu talal loh͈o am, te japa ko, ne ko, E borom‐ngum gu new, lutah͈ nga nimse?