Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 14:27 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

27 Wande Yesu wah͈ len chi tah͈ouay, ne, Dalal len sēn h͈ol: Man la; bu len tīt.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 14:27
21 Iomraidhean Croise  

Peter tontu ko, ne, Borom bi, su de you, ô ma ma ñou fi you chi kou ndoh͈ mi.


Yesu ñou, te lāl len, ne, Jog len, te bu len tīt.


Yesu ne len, Bu len tīt: dem len wah͈ suma i mboka ñu dem cha Galilee; fōfale la ñu ma gise.


Malāka ma tontu jigen ya, ne, Bu len tīt: ndege h͈am nā ne Yesu ngēn di ūt, ka ñu dāj on cha kura ba.


Ñu yub ko nit ku lafañ, teda chi lal: ba Yesu gise sēn ngum, mu wah͈ ku lafañ ka, ne, Suma dōm, na sa h͈ol dal; baal nañu la sa i bakar.


Yef yile lā len wah͈ ndah͈ chi man ngēn mun a am jama. Chi aduna si di ngēn am ngeten: wande na ngēn degerlo sēn hol; ndig fabi nā aduna si.


Wande mu ne len, Man la; bu len tīt.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan