11 Ñu indi bop’ am chi ndap, may ko janh͈a ba, mu yubu ko fa ndey am.
Mu yōni ku dog bop’ i John chi kaso ba.
Tālube am ya ñou, jel yaram wa, sūl ko, te dem nitali ko Yesu.
Mōm nak ndege ndey am jeñtal na ko, ne, May ma file bop’ i John Batisekat ba chi ndap.