1 Cha jamāno jōjale Herod kēlifa ga dēg’ on na lu ñu wah͈ lu jem chi Yesu,
Defu fa i koutef yu bare ndig sēn gumadi.
Dēgdēg am dem cha bir rew mōma yepa.
Wande ba ñu fa juge, ñu ēne tur am chi rew mōma yepa.