Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 13:44 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

44 Ngur i ajana niro na ak alal bu nubu chi bir tōl; ba ko nit feke mu nuba ko, dem chi banēh͈ am jay lu mu am on yepa, te jenda tōl bōbale.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 13:44
29 Iomraidhean Croise  

Mu teg benen lēb chi sēn kanam, ne, Ngur i ajana niro na ak nit ka ji on jiu ju bāh͈ chi tōl am;


Ba mu feke bena jamong ju jafe njēg, mu dem jay lu mu am on yepa, te jenda ko.


Ngur i ajana nirôti na ak mbal mu ñu sani chi gēch, mu japa h͈êt i jen wu neka:


Yesu ne ko, So buge mot, na nga dem, jay lo am, sarah͈ ko miskin ya, te di nga am jur cha ajana: te ñou, topa ma.


Fōfale Peter tontu ko, ne, Ñun ño wocha yepa, te topa la; lan la ñu ami mbōk?


Te ku neka ku bayi i nēg, mbāt i raka, mbāt i jigen, mbāte bay, mbāte ndey, mbāt i dōm, mbāt i tōl ngir man, di na ami lu bare lu len upa, te dona dunda gu dul jêh͈.


Ndege fa sa alal neka, fōfale la sa h͈ol jem itam.


Yesu ne len, Mā di mburu’ dūnda mi: ku ñou fi man du h͈īf, te ku gum chi man du mar muka.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan