Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 13:21 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

21 Wande amul rên chi bop’ am, te muñ chi sā yu new dal; ndege su nah͈ar joge wala ngeten ndig bāt bi, nōg’ ak nōga mu fakatalu.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 13:21
47 Iomraidhean Croise  

Ñepa di nañu len sib ndig man; wande ku di muñ be cha muj ga mō di muchi.


Te barkel chi ku dul feka fakatalu chi man.


Te ka ñu ji won chi i bereb i doch, mō di ka dēga bāt bi, te dal di ko nangu ak banēh͈;


Ñu fakatalu chi mōm. Wande Yesu ne len, Yonent ñakul teranga lu moy chi dek’ am, ak chi ker am.


Ba janta ba fenke mu laka len; te ñu lah͈, ndege amu ñu rên.


Wande ka di muñ be cha muj ga, di na mucha.


Fōfale Yesu ne len, Di ngēn fakatalu ndig man chi gudi gile yēn ñepa: ndege binda nañu, ne, Di nā dōr sama ba, te i nh͈ar i gēta ga di nañu h͈ajātlaku.


Wande Peter tontu ko, ne, Su ñepa fakatalô ndig you, man du ma fakatalu muk.


Yesu tontu len, te ne, Chi dega, chi dega, mangi len di wah͈, Ūtu len ma ndege gis on ngēn i koutef, wande ndege lek’ on ngēn mburu ya be ngēn sūr.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan