17 Ndege chi dega mangi len di wah͈, Yonent yu bare ak nit ñu jūb bug’ on naño gis li ngēn gis, te gisu ñu ko won; te dēga li ngēn dēga, wande dēgu ñu ko won.
Sēn bay Ibrayuma banēh͈u on na gis suma bes; te gis on na ko, te kontan.