12 Ndege ka am mōm la ño may, te di na am lu bare; wande ka amul, di nañu jel la mu am sah͈.
Mōtah͈ ma ne len, Di nañu jele ngur i Yalla fi yēn, te joh͈ ko h͈êt wu di mēña mēñef am.
Ndege ku am la ñu di joh͈, te di na am lu bare; wande ku amul, di nañu nangu la mu el’ on a am sah͈.