5 Jangu len itam chi mbinda yi naka seriñ ya chi bes i dimas moy dimas ja cha juma ja, te bakaru ñu?
Na mu h͈arafe chi nēg i Yalla ba, te leka mburu ma ñu dān wone, ma daganul on mu leka, wala ña and’ on ak mōm, wande seriñ ya dal?
Wande mangi len di wah͈, Kena angile ki gen a rey as juma ja.