49 Mu talal loh͈o am chi i tālube am, te ne, Sêt len, suma ndey ak suma i raka!
Wande mu tontu ka ko wah͈, ne, Kan a di suma ndey? te ñan a di suma i raka?
Ndege ku mu mun a don ku di def suma mbugel i Bay ba cha ajana, mō di suma raka, ak suma jigen, ak suma ndey.
Dem len bu gou, wah͈ i tālube am ne, Dēki na cha ñu dē ña; te di na len jitu cha Galilee; fōfale ngēn ko gise: mangi len ko wah͈.
Ñānatu ma ngir ñom reka, wande ngir ña di gumi chi man itam chi sēn bāt;