43 Wande nh͈el mu sobe mi, ba mu gēne chi nit, mu doh͈ chi bereb yu wou, di ūt noflay, te feku ko.
Fōfale mu ne, Di nā delu chi suma nēg fa ma gēn’ on; te ba mu deluse, mu feka ko am nēn, mu būb, te nah͈ātu.
Ñu h͈āchu, ne, Lan la ñu jote ak you, you Dōm i Yalla? Dā fi dika ndig geten ñu bala wah͈tu wa jot?