Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 12:42 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

42 Bur i gopu bu jigen ba di na tah͈ou chi bes i ate ba ak h͈êt wile, te ey len; ndege juge on na fu sorey ndah͈ mu dēga sago i Suleyman, te ku gen a rey Suleyman angi fi.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 12:42
22 Iomraidhean Croise  

Ga’ Nineveh ña di nañu tah͈ou chi bes i ate ba ak h͈êt wile, te ey len; ndege rēchu on nañu chi wāre’ Jonah, te ku gen a rey Jonah angi fi.


Wande mangi len di wah͈, Kena angile ki gen a rey as juma ja.


Ba mu wah͈ande, nir wu ne naña umba len, te bāt juge cha nir wa, ne, Kile di suma Dōm ja ma sopa; chi mom lā def suma h͈ol bepa; dēga len ko.


Te bāt juge cha asaman, ne, Kile mō di suma Dōm ji ma sopa, chi mōm lā feka li ma nêh͈ lepa.


Te Bāt bi yaramu on na, te dek’ on na ak ñun, te sêt on nañu ndam am, ndam niki ku di dōm i bay ju di bajo, fês ak yiw ak dega.


Ken mosul a gis Yalla muk; Dōm am ja di bajo, ka neka chi den’ i Bay ba, mō ko fêñal.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan