Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 12:40 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

40 Ndege naka Jonah nek’on chi bir mbonkana ma ñet’ i bechek ak ñet’ i gudi, nōgule la Dōm i nit ka di nekeji chi h͈ol i suf si ñet’ i bechek ak ñet’ i gudi.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 12:40
12 Iomraidhean Croise  

Ndege Dōm i nit ka mō di Boromdimas.


Cha sā sōsale Yesu dal di won i tālube am naka mu ela deme fa Jerusalem, te sona yef yu bare chi mag ya, ak i njīt i seriñ ya, ak bindānkat ya, te di ko rēyi, mu di dēkiji chi ñetel i fan am.


Di nañu ko rēy, te chi ñetel i fan am di na dēki. Ñu nah͈arlu lol.


You mi dānel jama ja te tabah͈ati ko chi ñet’ i fan, musalal sa bopa. So de Dōm i Yalla, wachal chi kura bi.


Nekul file; ndege dēki na, chi naka mu ko wah͈e won. Ñou len, sêt bereb bi fi ñu teral on Borom bi.


Yesu ne ko, Ntila yi am nañu i mpah͈, te mpich’ i asaman si am nañu i taga, wande Dōm i nit ka amul fu mu tedal bop’ am.


Yesu tontu te ne len, Maba len juma jile, te chi ñet’ i fan di nā ko delu tah͈oual.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan