39 Wande mu tontu len, ne, H͈êt i ēfar ak i njālokat ūt na mandarga, wande du ñu ko may mandarga lu moy mandarga i Jonah yonent ba;
H͈êt wu bon ak njālo ūt na mandarga; du ñu ko may mandarga, lu dul mandarga i Jonah. Mu bayi len, te dem.