33 Bāh͈lo len garap gi ak i dōm am; mbāte bonlo len garap gi ak i dōm am; ndege rañātle nañu garap gi chi i dōm am.
You Pharisee bu silmah͈a bi, setalal jeka bir i ndap li ak kela bi, ndah͈ cha biti set itam.