31 Mōtah͈ ma ne len, Bakar bu neka ak h͈as i Yalla, di nañu ko baal nit; wande ku h͈as Nh͈el mu Sela ma, du ñu ko baal.
“S u nu woni sunu i bakar, am na ormaa ak njubel pur baaal nu sunu i bakar, te pur setal nu ce lu bon yipa.”