3 Wande mu ne len, Ndah͈ jangu len la Dauda def on ba mu h͈īfe, ak ña and’ on ak mōm;
Wande Pharisee ya ba ñu gise lōla, ñu ne ko, Sêtal, sa i tālube ange def lu daganul a def chi bes i dimas.
Na mu h͈arafe chi nēg i Yalla ba, te leka mburu ma ñu dān wone, ma daganul on mu leka, wala ña and’ on ak mōm, wande seriñ ya dal?
Jangu len itam chi mbinda yi naka seriñ ya chi bes i dimas moy dimas ja cha juma ja, te bakaru ñu?
Mu tontu len, ne, Ndah͈ jangu len ne ka len bind’ on cha ndôrte la, dafa len bind’ on gōr ak jigen,
Te ne ko, Ndah͈ dēga nga li ñile di wah͈? Yesu ne len, Wau: ndah͈ mosu len a janga, ne, Chi gemeñ’ i dōm ak i gūne yu di nampa nga motali nau?
Wande mosu len a janga lu jem chi ndēkite ga, la len Yalla wah͈ on, ne,