26 Te su Seytane gēnê Seytane, hajāliku na chi bop’ am; naka la ngur am di tah͈oue mbōk?
Ba kena dēge bāt i ngur gi, te h͈amu ko, fōfale la Seytane ñoue, te dindi la ñu ji won chi h͈ol am. Kile di ka ñu ji won chi wet i yōn wa.
Fōfale Yesu ne ko, Randu ma Seytane, ndege binda nañu, ne, Na nga jāmu Borom ba sa Yalla, te na nga ko topa, mōm reka.
Wande Pharisee ya ne, Chi bur i jine ya la gēne jine yi.
Ate’ aduna sile jot na: lēgi ñu gēne gelouar i aduna sile, te sani ko cha biti.
Du ma wah͈ati ak yēn lu bare; ndege gelouar i aduna sile ñou na; te amul dara chi man;
Chi ate, ndege gelouar i aduna sile ate nañu ko.