Matthew 12:25 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
25 Mu h͈am sēn i h͈alāt, te ne len, Ngur gu neka gu h͈ajāliku chi bop’ am, di na ñou chi ntaste; te deka bu neka, mbāte nēg, bu h͈ajāliku chi bop’ am du tah͈ou:
Mu ne ko ñetel i yōn bi, Simon, dōm i John, sopa nga ma? Peter nah͈arlu ndege nôn na ko ñetel i yōn bi, Sopa nga ma? Te mu ne ko, Borom bi, h͈am nga lu neka; h͈am nga ne sopa nā la. Yesu ne ko, Samal suma i nh͈ar.