17 Ndah͈ la Isaiah yonent ba wah͈ on motaliku, ne,
Te mu ebal len, ne, Bu ko kena h͈am:
Sêt len, suma ndau ba ma tana; suma sopa ka nêh͈ lol chi suma fit; di nā teg suma Nh͈el chi kou am, te di na yēgle lu jūb chi Gentile ya.
Ndah͈ la yonent ba wah͈ on motaliku, ne, Di nā ūbi suma gemeñ chi i lēb; di nā yēgle yef yu nubu cha ndôrte’ aduna si.
Lile am on na nak, ndah͈ lu yonent ba wah͈ on motaliku, ne,
Ndah͈ la Isaiah yonent ba wah͈ on motaliku, ne, Mō jel on suñu munadi, te yubu on suñu i jangaro.
Su len tūde won i yalla, ndege chi ñom la bāt i Yalla ñou on (te du mun a fanh͈a mbinda mi),
Ndah͈ bāt i Isaiah yonent ba motaliku, ba mu wah͈ on, ne, Borom bi, kan a di gum suñu yēgle? te chi kan la loh͈o i Borom ba fêñu?
Ganou lōlu, Yesu ba mu h͈ame ne yepa soti na, ndah͈ mbinda ma motaliku, mu ne, Mar nā.