23 Te you Capernaum, mi yēkatiku cha asaman, di nañu la sufel be chi nāri: ndege koutef ya ma def on chi you, su ñu len def on cha Sodom, kôn mu des bentey.
Chi dega mangi len di wah͈, di na gene dek’ i Sodom ak Gomorrah chi kerog mpēnch’ um Yalla ma as deka bōbale.
Te mangi la wah͈ it, ne yā di Peter, te chi doch wile lā di tabah͈ suma jangu; te bunt’ i nāri du ko fabi.
Ba ñu dike chi Capernaum, ña di jel ngalak la ñou fi Peter, ne, Ndah͈ sēn borom du fey ngalak?
Te juge Nazareth, mu ñou deka chi Capernaum, bu jegeñ gēch ga, chi wet i Zebulun ak Naphtali:
Ba Yesu h͈arafe chi Capernaum, bena saltige ñou fi mōm, te dagān ko,