20 Fōfale mu dal di eda deka ya fa mu def on koutef am yu gen a bare, ndege da ñu rēchuwul.
Ga’ Nineveh ña di nañu tah͈ou chi bes i ate ba ak h͈êt wile, te ey len; ndege rēchu on nañu chi wāre’ Jonah, te ku gen a rey Jonah angi fi.