17 Ne, Lītal nañu len, te fēchu len; yeremtu nañu, te joyu len.
Wande ak lan la h͈êt wile niro? Niro na ak h͈alel ñu jēki chi i ndaje, di h͈āchu chi sēn i mās,
Ndege John ñouūl on di leka wala di nān, te ñu ne, Anda na ak jine.
Yesu ne len, I mbok’ i nēg i borom‐chēt ga, ndah͈ mun naño nah͈arlu ba borom‐chēt ga neke ak ñom? Wande jamāno di na diki ba ño fabi borom‐chēt ga cha ñom; bōbale di nañu ôri.
Ba Yesu ñoue chi bir nēg i kēlifa ba, te gis lītkat ya ak nit ña di jāle,