14 Te su ngēn ko buge nangu, kile di Elijah, ka war a ñou.
Ndege yonent ya yepa ak yōn wa yēgle on nañu be cha John.
Bentey am nā yef yu bare lu ma len wah͈, wande munu len ko muñ lēgi.