13 Ndege yonent ya yepa ak yōn wa yēgle on nañu be cha John.
Cha jamāno i John Batisekat ba bentey, chi nchouarte la ñu fab ngur i ajana, te ña souar japa ko.
Te su ngēn ko buge nangu, kile di Elijah, ka war a ñou.