Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 10:41 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

41 Ku nangu yonent chi tur i yonent, di na am yōl i yonent; te ku nangu nit ku jūb chi tur i nit ku jūb, di na am yōl i nit ku jūb.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 10:41
27 Iomraidhean Croise  

Ndege Dōm i nit ka di na ñou chi ndam i Bay am, ak i malāk’ am; te chi wah͈tu wōwale di na yōl nit ku neka naka ligey am day.


Ñom it di nañu ko tontu, ne, Borom bi, kañ la ñu la gis on nga h͈īf, wala nga mar, wala nga di gan, wala nga rāfle, wala nga jēr, wala chi kaso, te dimaliū ñu la?


Di na len tontu, ne, Chi dega mangi len di wah͈, Ndege defu len ko won chi ku gen a tūt chi ñile, man ngēn ko defalul on.


Otu len ngēn def sēn i jef yu bāh͈ chi kanam i nit ndah͈ ñu gis len, mbāte du len am yōl chi sēn Bay ba cha ajana.


Ndah͈ do mel naka ku di ôr chi nit, wande chi sa Bay ki chi nubu; te sa Bay ka gis lu nubu, di na la yōl.


Ndah͈ sa sarah͈ di nubu, te sa Bay ki di gis lu nubu, di na la yōl.


Wande you, so di ñān, dugal chi sa bir nēg, te ba nga teje bunta ba, ñānal sa Bay ki chi nubu; te sa Bay ki di gis lu nubu, di na la yōl.


Ndege ku mu mun a don ku lāj, di na am; te ku ūt, di na gis; te ku foga, di nañu ko ūbi.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan