39 Ku ūt dund’ am, di na ko rēr; te ku rēral dund’ am ngir man, di na ko gis.
Ku sopa dūnd’ am, di na ko rēral; te ku bañ dūnd’ am chi aduna sile, di na ko dēncha be cha dūnda gu dul jêh͈.