35 Ndege da ma ñou di munadilo gōr ak bay am, te jigen ak ndey am, te dōm ju jigen ak goro am gu jigen.
Mag di na jebal rak’ am ndah͈ mu dē, te bay dōm am: i dōm di nañu or sēn i bay ak sēn i ndey, te rēylu len.
Fōfale ñu bare di nañu fakatalu, orante, te sibante.