Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 10:28 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

28 Bu len ragal ña di rēy yaram wi, wande munu ño rēy fit wi; wande ragal len ka mun a yah͈a fit ak yaram itam chi nāri.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 10:28
30 Iomraidhean Croise  

Bu len len ragal mbōk; ndege dara muruwul lu dul muriku; mbāte nubu, lu dul fêñ.


Ñile di nañu dem chi ndān gu dul jêh͈: wande ñu jūb ña chi dunda gu dul jêh͈.


Wande mangi len di wah͈, Ku di mere morom am, mungi chi tafār i ate; te ku ne morom am, Dof bi, mungi chi tafār i ate bu rey; wande ku ne, Ēfar bi, di na neka chi tafār i safara’ nāri.


Te di nañu gēna; ña def on lu bāh͈ cha ndēkite’ dūnda: te ña def on lu bon cha ndēkite’ ate.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan