26 Bu len len ragal mbōk; ndege dara muruwul lu dul muriku; mbāte nubu, lu dul fêñ.
Bu len ragal ña di rēy yaram wi, wande munu ño rēy fit wi; wande ragal len ka mun a yah͈a fit ak yaram itam chi nāri.