21 Mag di na jebal rak’ am ndah͈ mu dē, te bay dōm am: i dōm di nañu or sēn i bay ak sēn i ndey, te rēylu len.
Fōfale ñu bare di nañu fakatalu, orante, te sibante.