Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 10:2 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

2 Tūr i fuk’ i tālube ak ñar yangile: Benel bi, Simon ku tuda Peter, ak Andrew rak’ am; James dōm i Zebedee, ak John rak’ am;

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 10:2
44 Iomraidhean Croise  

Ganou jurom ben’ i fan, Yesu jel Peter, James, ak John rak’ am, te yubu len chi kou tūnda wu koue, ñom dal:


Fōfale ndey ī dom i Zebedee ñou fi mōm, ak dōm am yu gōr, di ko jāmu, te lāj ko lef.


Mu jel ak mōm Peter ak ñar i dōm i Zebedee, dôr di yogorlu ak nah͈arlu lol.


Don na doh͈ cha tefes i Galilee, te mu gis ñar i mboka, Simon ku tūda Peter, ak mag am Andrew, di sani mbal cha gēch ga; ndege nek’ on nañu i mōl.


Bu mu fa juge, mu gis yenen i mboka, James dōm i Zebedee, ak rak’ am John, chi gāl ga, ak Zebedee sēn bay, di dāh͈ sēn i mbal; te mu ô len.


Philip ñou te wah͈ Andrew: Andrew ñou ak Philip, te ñu wah͈ Yesu.


Bena cha i talube am angi cha tabul ba, ka Yesu sop’ on, di wēru chi den’ i Yesu.


Mu dou nak, te dika fa Simon Peter, ak benen talube ba Yesu sop’ on, te ne len, Da ñu jel Borom bi cha bir bamel ba, te h͈amu ñu fu ñu ko tedal.


Nek’ on nañu fōfa Simon Peter, ak Thomas ku tūda sīh͈ bi, ak Nathanael i Cana cha Galilee, ak i dōm i Zebedee, ak ñenen ñar i talube am.


Peter h͈inaku, te gis talube ba Yesu sop’ on di topa; ka wēru on itam cha den’ am cha rêr ba, te ne, Borom bi, ana ku la di ori?


Bile di talube ba sēde yef yile, te bind’ on na yef yile: te h͈am nañu ne sēde am dega la.


Yesu ne fuk’ ak ñar ña, Ndah͈ yēn itam, da ngēn ma wocha?


Yesu tontu len, ne, Ndah͈ du yēn lā tan’ on, fuk’ ak ñar ña, te kena chi yēn ab seytane la?


Lile nak wah͈ na ko ndig Judas, dōm i Simon Iscariot, ndege mō ko ori, kena chi fuk’ ak ñar ña.


Kena chi talube am ya, Andrew, rak’ i Simon Peter, ne ko,


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan