Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 10:15 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

15 Chi dega mangi len di wah͈, di na gene dek’ i Sodom ak Gomorrah chi kerog mpēnch’ um Yalla ma as deka bōbale.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 10:15
22 Iomraidhean Croise  

Te mangi len di wah͈, Bāt i nēn bu neka bu nit di wah͈, di na joh͈i warugal am chi bes i ate ba.


Ndege chi dega mangi len di wah͈, Be bu ajana ak suf di wey, dara du wey chi yōn wa muk, be yepa motaliku.


Ñu bare di nañu ma wah͈ chi bes bōbale, Borom bi, Borom bi, ndah͈ wareū ñu on chi sa tur, te chi sa tur ñu dah͈’ i jine, te chi sa tur ñu def koutef yu bare?


Ku ma bañ, te nanguwul suma i wah͈, am na kena ku ko ate: bāt ba ma wah͈ on, mō ko ateji cha bes bu muje ba.


Te mbugel i ka ma yōni on a di lile, ne ña mu ma may ñepa, du ma ñaka ken, wande dēkali ko cha kera bes ba.


Ndege suma mbugel i Bay ba di bile, ne ku neka ku gis Dōm ji te gum chi mōm, di na am dūnda gu dul jêh͈; te di nā ko dēkali cha kera bes ba.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan