Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 10:1 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

1 Ba mu ôe fuk’ i tālube am ak ñar, mu may len kantan ñu dah͈a nh͈el yu sobe ya, te weral ña opa ñepa, ak h͈êt i jarak ju neka.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 10:1
26 Iomraidhean Croise  

Yesu ne len, Chi dega mangi len di wah͈, Chi ndelute ga, ba Dōm i nit ka di tōgi chi kou gangūne’ ndam am, yēn ñi ma topa, di ngēn tōgi chi kou fuk’ i gangūne ak ñar, di ate fuk’ i h͈êt i Israel ak ñar.


Ba ngon jote, mu tōg di leka ak fuk’ i tālube ya ak ñar;


Ba mu wah͈andô, Judas, kena chi fuk’ ak ñar ña, ñou, and’ ak mōm mbōlo mu rey ñu am i jāsi ak i doko, ñu juge fa i njīt i seriñ ya ak i mag i nit ña.


Yesu dem cha bir Galilee yepa, di jemantale chi sēn i juma, di wāre linjil i ngur gi, te di weral h͈êt i opa ju neka, ak hêt i jangaro ju neka chi digante nit ña.


Te bu ñu bayi ñu tabi chi bulis, wande musal ñu chi lu bon.


Yesu dem cha rew ya ak deka ya yepa, di jemantale chi sēn i juma, wāre linjil i ngur gi, te weral ña opa ñepa, ak jarak ju neka chi digante nit ña.


Mōtah͈ ñān len Borom i ngōbte gi, ndah͈ mu yōni i ligeykat chi ngōb am.


Naka nga ko maye won sañsañ chi kou nit ñepa, ndah͈ mu maye ña nga ko may on ñepa dūnda gu dul jêh͈.


John tontu te ne, Nit munul a nangu dara, su ñu ko ko mayule cha ajana.


Bay ba sopa na Dōm ja, te joh͈ na ko lu neka chi loh͈o am.


Yesu tontu len, ne, Ndah͈ du yēn lā tan’ on, fuk’ ak ñar ña, te kena chi yēn ab seytane la?


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan