2 Te talube am ya lāj ko, ne, Rabbi, kan a bakar, kile, am i wā’ jur am, be mu judo silmah͈a?
Bulu sukal saa bopa fi nom, ne, da nga len di jaamu: ndegi, Man Yalla saa Borom, Yalla bu fir la, te di teg bakar i bai yi ce kou dom yi, ca netel ak nenentel i hert na maa ban,
Ñu ne, Ñena ña ne, John Batisekat ba; ñenen ne, Elijah; te ñenen ne, Jeremiah, wala kena chi yonent ya.
Ak i noyo chi i ndaje, te nit di len ôe, Rabbi.
Wande yēn, bu ñu len ôe Rabbi: ndege kena di sēn jemantalkat, te yēn a di i morom.
Cha bōbale i talube am dagān ko, ne, Rabbi, na nga leka.
Ba Yesu rombe, mu gis nit ku silmah͈a won cha ba mu jūdo.
Ñu tontu te ne ko, Yangi jūdu on bepa chi bakar, te nga buga ño jemantal? Te ñu gēne ko cha biti.