1 Ganou yef yile h͈ewte i Yauod ya am on na; te Yesu dem fa Jerusalem.
Yesu tontu ko, ne, Bul ko bañ lēgi, ndege nōgu la ñu ela motali njūbay yepa. Nōgale la bañatul.
Te h͈ewte i Yauod ya jegeñsi na, te Yesu dem fa Jerusalem.