Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




John 4:3 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

3 Mu bayako Judea, te demati cha Galilee.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




John 4:3
11 Iomraidhean Croise  

Wande su ñu len getene chi deka bile, dou len fa benen; ndege chi dega ma ne len, Du len won demi chi i dek’ i Israel yepa be ba Dōm i nit ka di ñoui.


Cha elek sa bug’ on na dem cha Galilee, te mu gis Philip, te Yesu ne ko, Topa ma.


Te mu demati cha ganou Jordan, cha bereb ba John jek’ on di batise; te mu jēki fa.


Tah͈na Yesu doh͈atul cha kanam i Yauod ya, wande mu bayako fa, dem rew mu jegeñ manding ma, cha deka bu tūda Ephraim; te mu jēki fa ak talube ya.


Mandarga bu jeka bile la Yesu def on cha Cana i Galilee, te wone ndam am; te i talube am gum chi mōm.


Ganou yef yōyu Yesu ak i talube am ñou on nañu cha suf i Judea; te mu jēki fa ak ñom te batise.


La mu gis te dēga, lōlu la sēde; te ken nanguwul sēde am.


Ba mu dēge ne Yesu juge on na Judea ñou chi Galilee, mu dem fa mōm, te dagān ko mu dika weral dōm am; ndege mungi buga dē.


Cha ganou yef yile Yesu doh͈ on na cha Galilee: ndege bugul on a doh͈ chi Judea, ndege Yauod ya don nañu ko ūt a rēy.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan