2 (Wande Yesu du won batise, wande i talube am),
Ô on nañu itam Yesu ak i talube am cha sey ba.
Ganou yef yōyu Yesu ak i talube am ñou on nañu cha suf i Judea; te mu jēki fa ak ñom te batise.
Te ñu ñou fi John, te ne ko, Rabbi, Kōkale nek’ on ak you ganou wala Jordan, ka nga sēde won, munga batise, te ñepa dika fa mōm.